LAAJ 13
Lan la Biibël bi wax ci liggéey ?
“ Seetlul ku man liggéeyam, buur lay liggéeyal, du liggéeyal baadoolo. ”
“ Ku daan sàcc, na ko dëddu te jublu ci liggéey lu baax ci ay loxoom, ngir mu mana dimbali ñi néew doole. ”
“ Kenn ku nekk danga war a lekk te naan te jariñoo bu baax ci sa liggéey bu metti. Loolu, maye Yàlla la.””
Dajalekat 3:13, MN