2018-2019 Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan — Ak ki bànqaas bi yónni
Seetal porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan bi, ak waxtaan yi ki bànqaas bi yónni nar a def.
Dëgërlul !
Porogaraam bi dina leeral ni ñu mënee am doole bi ñu soxla ngir dëgër ci ngëm.
Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
Dinañu tontu laaj yii ci porogaraam bi.