Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
1. Yan ñooy ñetti mbir yi Yexowa di def ngir ñu am mbégte? (Sabóor 32:1-10)
2. Naka lañu mënee am mbégte tey? (Sabóor 5:12, 13; 91:14)
3. Naka lañu mënee wéy di am mbégte ci liggéeyu waare bi, doonte sax ñu ngi ci ay jafe-jafe? (Jëf ya 13:50-52; Waa Room 5:3-5)
4. Naka lañu mën a moytoo «diig» ba ñàkk suñu mbégte? (Luug 21:34)
5. Naka lañu Yexowa di bégale? (Sabóor 92:5, 6)
6. Lan moo ñuy dimbali ñu kontine di jiital Yexowa ci lépp? (Waa Room 1:20; Baamtug Yoon wi 6:6-9; Waa Filib 4:6; Sabóor 16:3)