2018-2019 Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan — Ak wottukat biy wër ci mbooloo yi
Jëfandikool porogaraam bi ngir mën a déglu ndaje bu mag bu benn fan bi yépp bu Seede Yexowa yi ci sa dëkk . At bii yax bi mooy “ Ñemeel ! ”
Ñemeel !
Lu tax ñeme mën a doon lu jafe ci ñun, ak lan moo ñu mën a dimbali ñu am jikko boobu ?
Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
Dinañu tontu laaj yii ci porogaraam bi.