Ñemeel !
SUBA SI
-
9:30 Misik
-
9:40 Woy-Yàlla No. 73 ak ñaan
-
9:50 Yexowa moo ñuy ñemeloo
-
10:05 Waxtaan bu def ay xaaj : Ñemeel ni . . .
-
Enog
-
Musaa
-
Yosafat
-
Piyeer
-
-
11:05 Woy-Yàlla No. 69 ak yégle yi
-
11:15 Gënal a ñeme ci liggéeyu waare bi
-
11:30 Jébbalu bi ak Sóob bi
-
12:00 Woy-Yàlla No. 48
NGOON SI
-
1:10 Misik
-
1:20 Woy-Yàlla No. 63 ak ñaan
-
1:30 Waxtaan bi ñu jagleel ñépp : Tàkkuleen ci Diine Dëgg gi
-
2:00 Njàngum La Tour de Garde bu ñu gàttal
-
2:30 Woy-Yàlla No. 76 ak yégle yi
-
2:40 Waxtaan bu def ay xaaj : Ñemeel ni Kirist, bu amee ñu lay xiir ci lu bon . . .
-
Ci biir kër gi
-
Ca lekkool ba
-
Fi ngay liggéeye
-
Fi nga dëkk
-
-
3:40 Seen ñeme “ ëmb na yool bu mag ”
-
4:15 Woy-Yàlla No. 119 ak ñaan