Ubbil li ci biir

Woneel li nekk ci téere bi

Nanga bëgg Yexowa ak sa xol bépp

Nanga bëgg Yexowa ak sa xol bépp

DEUTÉRONOME 13:3

SUBA SI

  • 9:40 Misik

  • 9:50 Woy-Yàlla No. 109 ak ñaan

  • 10:00 “ Mbëggeel ci Yàlla mooy sàmm ay ndigalam ”

  • 10:15 Mbëggeel ci Yexowa mooy bëgg sa mbokk ci ngëm

  • 10:30 “ Nanga bëgg sa moroom, ni nga bëgge sa bopp ”

  • 10:55 Woy-Yàlla No. 82 ak yégle yi

  • 11:05 “ Mbëggeel day suul bàkkaar yu bare ”

  • 11:35 Jébbalu bi ak sóob bi

  • 12:05 Woy-Yàlla No. 50

NGOON SI

  • 1:20 Misik

  • 1:30 Woy-Yàlla No. 62

  • 1:35 Ay nettali yu jëm ci suñu liggéey

  • 1:45 Njàngum La Tour de Garde bu ñu gàttal

  • 2:15 Waxtaan bu def ay xaaj : Màggalleen Yexowa seen dund gépp

    • Xale yi

    • Ndaw yi

    • Mag ñi

  • 3:00 Woy-Yàlla No. 10 ak yégle yi

  • 3:10 Nanga bëgg Yexowa ak sa xol bépp

  • 3:55 Woy-Yàlla No. 37 ak ñaan