Yàlla
Kan mooy Yàlla?
Ndax Biibël bi wax na ci trinité?
Diine yu bare dañuy jàngale ne Yàlla trinité la. Ndax loolu la Biibël bi wax?
Turu Yàlla
Ndax Yàlla am na tur?
Ci ay Biibël yu bare, turu Yàlla mu ngi ci, ndax war nga xam tur bi te di ko tudd?
Coobare Yàlla
Lan la Biibël bi wax ci tànnal sa bopp li nga bëgg a def? Ndax Yàlla mooy dogal lépp?
Ñu bare gëm nañu ne Yàlla mooy dogal lépp ci seen dund. Ndax li ñuy tànn a def tey mooy tax ba li ñu bëgg a def ëllëg sotti?